YTMastersYTMasters
Sunu monde bu doyy warrC

Sunu monde bu doyy warr

🤣 Dalal ak jàmm ci sunu monde bu doy waar! 🐕🇸🇳 Fii, dinga gis comédie Wolof, ay mbir yu doy waar, ay xaalis yu reer, ak surtout xaymaay bu wax degg! 😂 Dafa xam lépp, dégg lépp, te du tëye wax! 🐕🗣️ Tey mooy mbirum kër gi, suba mooy mbirum dëkk bi! 😭😂 Sunu objectif mooy nga ree, nga bànneexu, te nga ñëwati ngir xool episode bu bees bi! 👉 Abonne-toi • Like • Partage • Te bul fàtte: xaymaay bi dafa xam lépp! 😂🐕🇸🇳

16kSenegalSN
Autunno 2026

Comune · Autunno 2026

Sunu monde bu doyy warr

@dafayomb su YouTube

Senegal Senegal

IntrattenimentoCinema e serie TVComicità

Iscritti
16k
Visualizzazioni
2 · 0 preferiti
Copie
0 · 0 giocatori
In vendita
0

Prossima collezione, Inverno 2026: Comune

A 100k iscritti diventerà Non comune nelle collezioni successive.

Iscriviti al canale per farla salire nelle prossime collezioni!